Добро пожаловать
Вход

Titi Jiggen Feem - Video Originale + Bonus (+ LYRICS dans la description)

Спасибо! Поделитесь с друзьями!

URL

Вам не понравилось видео. Спасибо за то что поделились своим мнением!

К сожалению, только зарегистрированные пользователи могут создавать списки воспроизведения.
URL


Добавлено от Admin В Смотреть русские мелодрамы
19 Просмотры

Описание

Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne en CLIQUANT ici :
http://www.youtube.com/subscription_center?add_user=princeartsmusic Rejoignez nous sur:
Google+ : http://gplus.to/PrinceArtsMusic
Facebook : https://www.facebook.com/PrinceArtsMusic
Twitter : https://twitter.com/princeartsmusic

Après 4 ans d'absence, Titi La Divine nous revient avec cette belle interprètation "Jiggen Feem". Cette chanson parle de la façon dont une femme doit s'occuper de son homme. Quelle belle manière de revenir. Titi est une artiste sénégalaise, produite par Prince Arts, Label avec lequel elle a sorti 5 albums dont 2 hors séries. En avant gout de son nouvel album, Titi vient de lancer un deuxième single Booba Batay qui cartonne fort à Dakar et disponible sur votre chaine. Discographie: Albums Kouné Ak Lula Yengel, Amoul Nou Malene Beuguéwoul, Façon. Hors série: Spécial Ndeweneul et Café Music.

Abonnez-Vous à notre chaîne YouTube pour être les premiers à être informés à chaque nouvelle sortie : http://www.youtube.com/subscription_center?add_user=princeartsmusic
Rejoignez nous sur:
Google+ : http://gplus.to/PrinceArtsMusic
Facebook : https://www.facebook.com/PrinceArtsMusic
Twitter : https://twitter.com/princeartsmusic

- - - PAROLES - - - LYRICS - - -

Jiggen sou beugué am manorééé... thi seyam !
Neu guéné lep, koundioug yék kadiague yi...
Neu safeu saf... Beuss bou nekeu... indil féém you bess
Boul ko khep djinakh dey bari pakh
Gaaatéééko ba foumou dém yow rékeu ley khalate


Jiggen sou beugué am manorééé...
Dey jonguéééé té bary féém( 2X)
na saf !
Fik mingui bék yokal dose bi boulko outeul frontière
Na safa saf... Na gueneu saf
Pampam piram pampam wata bambam


Jiggen sou beugué am manorééé...
Dey jonguéééé té bary féém
Yow bo beugué am manorééé...
Jonguél ! Té fékhel beu loumou lamb dadji
Té bokou soré dang koy wéteul
Té loumou mér mér, fékhél ba mou ré
Té bouko niourou dionguéééél ba mou saf !
Na faf melni adouna yéén dongua thi né


Jiggén sou beugué am manorééé...
Dey jonguéééé té bary féém
An an... An an an an... An an an an an an...
Yow baril féém !
Jiggen jonguél jonguél beu mou meut wonél say féém!
Ték ko thi temps té civilisé wonél say féém !
Djeuffé ko deuké ko wonél sa féém !



Mine nguameu mine nala dagnou wara sey
yAllah ma bolék yow degnou wara sey
Mine nguameu mine nala dagnou wara sey
yAllah ma bolék yow degnou wara sey

Seyallaaaaa man
Samey dooma wara takh meu nanguou lou métti papy
Beu fougnou meuneu dém beu fougnou meuneu né
An sey bimey sey molène di walooo...
Papé !



Papy louleu nékhoul thi mane dameukoy dindi
Gawémeu gawémeu man yaw lay sét
Mbeuguel dou ray ci niaye sou guené fegn
Dou ci wakhine dou ci djeufine ... Yow lay sét
Louleu nékhoul thi man meu dindi sani
Oooooooh papy chéri yow lay sét
Papy sou doyoulé meu doli
Louleu fi nékhoul dal damakoy dindi
Pitakh yangui ni, souleu doyoulé
Sou doyoulé meu doli yow lay sétt

Papy yAllah bolléna mak yow.. Yow lay sét
Bayina kharite andando yow lay sétt
Djitteul na sameu yakaaar ci yow
yAllah bolléna mak yow.. Yow lay sét
Éééééh djine naleu oooooh man yow lay sét
Ééééééh.

Написать комментарий

Комментарии

Комментариев нет.
RSS
Яндекс.Метрика